Institut : Centre de linguistique appliquée de Dakar, Université Cheikh Anta Diop

Domaine : Élections

Concept n° ELECT00011

langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol bérébu taf b n bérébu tafukaay
fra affichage (lieu)

Concept n° ELECT00012

langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol bérébu tafukaaybérébu taf b n
fra affichage (lieu)

Concept n° ELECT00008

langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol bataaxalu wutum pal buy wër kuréel mbaa mbooloo b n
fra circulaire de propagande

Concept n° ELECT00007

langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol àttewaatukaaypéncum àttewaat b n
fra cour d'appel

Concept n° ELECT00004

langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol àppu mbindu b n
fra délai d'inscription

Concept n° ELECT00009

langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol batale tànn b n
fra délégation de vote

Concept n° ELECT00003

langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol ambolog bu yoon nangu b n : ëmbukaay bu yoon nangu
fra enveloppe réglementaire

Concept n° ELECT00006

langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol àttekat b n xaali
fra juge

Concept n° ELECT00010

langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol bérébub mbindu b n
fra lieu d'inscription

Concept n° ELECT00001

langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol aji yore baat b n ci mbirum tànn, aji yore baat mën na doon aji yore baatub làng mbaa aji yore baatub lim
fra mandataire

Concept n° ELECT00005

langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol àttekaayu pàccu diwaan b n
fra tribunal départemental

Concept n° ELECT00002

Définition (wol)
koppar yi ñu lay feyloo soo jalgatee yoon, ci boo wàccee yoon
langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol alamaan b daan
fra amende

Page codée en HTML 4.01 Strict validé