Institut : Université de Nouakchott (UNkc), Département des langues nationales et de linguistique

Domaine : Santé

Concept n° SANTE0001

Définition (wol)
Mënadi dox gu soqeekoo ci fitna
langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol abasi abasi b n
fra abasie

Concept n° SANTE0011

Définition (wol)
wàññeeku bu takku jëm ci xel mbaa ci doole
langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol bayeeku baje :ku b n
fra abattement

Concept n° SANTE0002

Définition (wol)
ajowoo oksiseen ngir mëna law
langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol aajo-oksiseen à ijo.oksis : n b
fra aérobie

Concept n° SANTE0007

Définition (wol)
lu mëna dund ci ndoxak joor
langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol bag bag b n
fra amphibie

Concept n° SANTE0003

Définition (wol)
Lu mënul dund ci teewaayu oksiseen
langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol aajoodi oksiseen a:ɟo:di oksis : b n
fra anaérobie

Concept n° SANTE0009

Définition (wol)
kawar yu weex yuy wër tanku fas te di kowe leeg leeg
langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol balsaan balsa :n b n
fra balzane

Concept n° SANTE0005

Définition (wol)
1.fonkib mboolem cérit jóge ci colum ngelaw mbaa gaa, 2.tàw weekub cériti xëtër bu jéggi dayo
langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol amfisem âfise m b n
fra emphysème

Concept n° SANTE0004

Définition (wol)
mboolem céri biir ( , xëtër, gàddaam) yi jàppoo ci malayiy lekk
langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol afisaay afisa:j b n
fra frésure

Concept n° SANTE0012

Définition (wol)
fër bu dal mala yiy duññi ak fas te ookewoo ci law teet gu ñu naan gese
langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol ballugewe bal:ugewe b n
fra lathyrisme

Concept n° SANTE0008

Définition (wol)
biir bu fokki ndax ngelaw
langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol bagla bagla b n
fra météorisation

Concept n° SANTE0010

Définition (wol)
barle wu góor ak fas wu jugéen
langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol barle barle b n
fra mulet

Concept n° SANTE0006

Définition (wol)
gëstu cosaanu yenn xeeti mala
langue entrée phonétique classe grammaire contexte exemple renvoi
wol askanal mala askanal mala b n
fra pedigree

Page codée en HTML 4.01 Strict validé